ci jamm [lit: en la paz], jamm ak jamm • (otras desps) (me voy) maa ngiy dem, (ve en paz) demal ak jàmm, (en paz, paz y paz) jàmm ak jàmm, (pasa el día en paz) yendul ak jàmm, (pasa la noche en paz) fanaanal ak jàmm
bienvenido
--
buenas noches
fanaanal nak jamm
buenas tardes
jamm nga yendo
buenos días
('bonjour') jamm nga fanaan
da igual
(=no importa) du dara • (no tiene importancia) amul solo
de acuerdo
--
de nada
amul solo ('no-tiene importancia'), du dara
disculpe
baal ma, jegël ma
enhorabuena
--
estar de acuerdo
--
gracias
jërëjëf, jere jef • jaafëf
hola
salaamaalekum [resp: maalekum salaam] • ('bonjour') jamm nga fanaan • (qué tal?) na nga def? [maa ngi fi rekk]
lo siento
baal ma ('perdóname')
me duele
--
me gusta
--
perdone (sentido de: 'disculpe')
--
ponerse de acuerdo
--
por favor
su la neexee, baal ma (=perdóname, lo siento) • (¿podrías repetir eso por favor?) ndax mën nga ko waxaat, su la neexee? • (por favor, hable despacito) baal ma, waxal ndànk-ndànk